
👻:@milotnj99 # Ingénieur👨🏾💻~Muslim~in God we trust🙏🏽 🇸🇳. 📍🇫🇷
Cergy,Ile-de-France, France
Joined December 2017
- Tweets21.1K
- Following1.8K
- Followers1.1K
- Likes633K
Malick Sané retweeted
Si kanam 21h Inch'Allah dinane amal Jotaayu Murit wakhtaané Borom Sham Mame Mor mou Sokhna Diarra (Disciple et frère aîné du Cheikh)
xitter.cf/i/spaces/1pedJqXbMbvkY…
Malick Sané retweeted
L’autre jour quelqu’un a dit que Sëriñ Tuubaa est sa preuve dans la religion.
Wallahi fofu nga nek mo woor. Toujours je me dis que jangg doxalinu Sëriñ bi, doyna sëkk ci ma xam ne l’islam est vérité , que Yàllah moy Buurr bi nu wara Jaamu ci bëgg, yaakaar aq ragal..
Malick Sané retweeted
Français yi dañu noo colonisé ba xam ne jaadootul, ñu formel ñu nit ñu leen gën bon bàyyi leen fi, ñu tabax fi loo xam ne xeetu nit ñooñu rekk kay produit, réew mi di yàqu jëm fu kenn xamul, rawatina waa école boobu noonu.
Malick Sané retweeted
Sur les 8 dernières années que l'on peut considérer comme les meilleures années de leur carrière, Edouard Mendy et Yassine Bounou ont évolué en même temps en Europe et en Arabie saoudite.
Sur cette même période, Edouard Mendy a remporté 3 Ligues des champions dont une en Europe, ainsi que 2 Coupes d'Afrique devant le Marocain. Il n'y a tout simplement pas de débat possible.
Edouard Mendy ne boxe dans la même catégorie qu'aucun autre gardien de l'histoire du football africain. Il évolue sur une autre planète.
C'est le meilleur et le plus grand !
🇸🇳🇲🇦 Édouard Mendy vs Yassine Bounou : qui est le meilleur ?
Pour @mamadniang11, "Edou Mendy est peut-être le meilleur gardien africain de l'histoire"
J-1 spéciale Édouard Mendy, à suivre en intégralité vendredi 20 novembre à 21H45 GMT sur CANAL+ SPORT 1
#Jmoins1
Malick Sané retweeted
Replying to @HolleleSaidu
Ah Sama seriñ bi d newoon na xasidaam yi day yëngal xolu kepp ku texe
Malick Sané retweeted
Surtout lolou !! Ni wilaaya bindoo, moy takh dina nekk si façon profil bunee, t eupp neu nignko foogee (leelee niou beugg ko deff yeufii aada, t mbirr mi sutt neu loolu)
Motakh faaw niouy bayyi khel rek, Yalla kounekk leuy jokh..
Surtout Lii jamono ji nitt ñi kou niou toud amnagn sikk bougn lay askanalei. Tei awliya mom danio lakatou sii burr nitt ñii!!!
Replying to @mameMaodo1
2. Nga moytu sa làmmiñ ci dingat ak di xas waliyou Yàlla yi. Nga Moytou di fitnal ak di lorr say mbok jullit.
(2/2)
1
1
234
Malick Sané retweeted
Replying to @aliounetine16
M. Tine, quand il s’agit de Sonko, vous avez la gâchette facile. Mais quand il s’agit de Diomaye, vous êtes doux comme un agneau ! Votre jeu est tellement visible !
Malick Sané retweeted
Nit war naa sant Yàlla ci wér gi mu ko defal, lu la Yàlla teg ci tawat rekk lu mu tuuti tuuti nga sonn lool, te bu ko neexoon di la ko teg sa giirug dund.
Walahi❤️
Malick Sané retweeted
Celui qui le décrivait disait : « Jamais, ni avant lui ni après lui, je n’ai vu quelqu’un qui ressemblât à Al-Ḥabīb Al-Muṣṭafā ﷺ. »
Malick Sané retweeted
Al-Ḥabīb Al-Muṣṭafā ﷺ
Celui qui le voyait pour la première fois était saisi de respect et de révérence. Mais celui qui avait le privilège de le fréquenter et de le connaître davantage ne pouvait que l’aimer.
Qu’Allah nous fasse contempler son noble visage ﷺ.
Malick Sané retweeted
Ku sunu borom tawfexaale Liggëyaal Seriñ tuuba ba bis bu ñu laay taabal biir bàmmel ngay xamni kokù géen goor leu .
Ñi ëpp yitee tee gënaa soobù mom fi ci addùna la ñuy amee yaakhin ci ku baax kii lataa ëlëk .
Yalla naa nu wër féep ba duuñ ko mëna géen been yoon barkep Mame Seex Ibrahima fall 🤲🏾❤️
Malick Sané retweeted
Binga voter non voter woo en fait. Voter moom oui rek la mëna nekk.
Ku sañuta bañ saña nangu.





















