Pinned Tweet
Portrait Sëriñ Muhammadu Muntaxaa Mbàkke
Par Kureel Ligéeyal ku tedd ki.
#4safar2026
#Sëriñ_Muntaxaa
Samedi le 07 insallaa
A Complexe Bàjjan May ( Tuubaa Daaru Marnaan) .
#KLK
Kureel Liggéeyal Ku Tedd Ki retweeted
Kuréel liggéeyal ku tedd ki di leen yëgël di nanu tàmbale jàngale xam-xam bi ci 3 téere Sëriñ Tuubaa yii:
Ku bëgga bokk ci jàngale mi man ngaa jokk ci numéro yii ci affiche bi.
C gratuit.
Partagez 🙏
Kuréel liggéeyal ku tedd ki di leen yëgël di nanu tàmbale jàngale xam-xam bi ci 3 téere Sëriñ Tuubaa yii:
Ku bëgga bokk ci jàngale mi man ngaa jokk ci numéro yii ci affiche bi.
C gratuit.
Partagez 🙏
Bureau Kureel Ligéeyal ku tedd ki 1448H-1449H
#KLK
Assemblée Générale Kureel Ligéeyal ku tedd ki .
Jeudi 17 Septembre 2026
#KLK
Rt 🙏
Kureel Liggéeyal Ku Tedd Ki retweeted
As salam Aleykum Wa Rahmatulah Mangi len di Ziar dilen jox sen wacuway.
Di wax ñi am yeene jël been jukki diko jang mensuellement muy Goor Yallah wala Soxna amnañu ay jukki yu disponible.
Vous pouvez ne contacter par Dm ou faites signe sous ce tweet ma msg leen.
@joie_boule
#rtapprecie
Ñoo ngi sàkkul ñaan bubaax Serigne Maam Seex Ibraahiima Faal MBACKE moom Serigne Mountakha (YYW)
Nekkoon ku yàgga ànd ak Kureel bi ci ligéey bi...
Yàlla nako sunu boroom teeru ci yërmandeem ci mbaaxug Ku Tedd Ki.
#KLK
kuréel liggéeyal Ku Tedd ki
#KLK
#Rabiihiyaat_1448H_2026
Leeral Jasbu par Dr Sëriñ Abdu Xaadir Buso
Waxtaanu Gàmmu ( Rabiihiyyaat) 2026
Organisé par Kureel Ligéeyal ku tedd ki.
#Jasbu
#Gàmmu2026
Dr Sëriñ Abdu Xaadir Buso
Waxtaanu Gàmmu ( Rabiihiyyaat) 2026
Organisé par Kureel Ligéeyal ku tedd ki.
#Gàmmu2026
#Klk
Noogi leen kuy fàttali Suba insallaa
🔻 Cérémonie de clôture Rabiihiyyat 1448H/2026.
Partagez Svp 🙏
#Gàmmu2026
🔻 Cérémonie de clôture Rabiihiyyat 1448H/2026.
Partagez Svp 🙏
#Gàmmu2026
Waxtaan i Gàmmu 1448H
Dimanche 16 août 2026
À Partir de 21h
Diffusée sur toutes les plateformes digitales
#Gàmmu2026
Dëkk bii di Tuubaa ñaar rk ñoo ko séq:
1_ ñi fi dëkk nañ doyloo Sëriñ bi te fonku séenub liggéey Yàlla defal leen ci barke.
2_ ñi fiy ñëw na leen Sëriñ bi rk taxa jok ci Siyaare ak ñaan mu amal la njariñ lool tè du àndak benn lor nga dellu sab ligeey.
Source ;discours Sëriñ Muntaxaa Tabaski 2023.
#Sëriñ_Muntaxaa
#Safar2026
#18_Safar
Sëriñ Baara Mbàkke moo jël 1ér place bi ci concours Daaju mak ñi .
Kureel Ligéeyal ku tedd ki doon ko amal.
#4safar
#safar2026




















