Pinned Tweet
كلّت العقول عن إيجاد كلمة بل كلمات لتوصيفك ، ولم تدرك الأذهان مقاماتك المرتفعة ارتفاعا، فلا صوت يذكر من تكون، ولا لسان نطق مزاياك ، ولا فعل أدرك ما فعلت فينا !
ولاكن عندنا يقين وجودِك في قلوبنا، و إن ضاقت فلها ما يوسًعها من حبّك، وإن توسّعت فلا تشبع من حبّك ❤️❤️❤️🙏🏼
Sëriñ Fàllu retweeted
Samedi le 07 insallaa
A Complexe Bàjjan May ( Tuubaa Daaru Marnaan) .
#KLK
Sëriñ Fàllu retweeted
Kuréel liggéeyal ku tedd ki di leen yëgël di nanu tàmbale jàngale xam-xam bi ci 3 téere Sëriñ Tuubaa yii:
Ku bëgga bokk ci jàngale mi man ngaa jokk ci numéro yii ci affiche bi.
C gratuit.
Partagez 🙏
Sëriñ Fàllu retweeted
Space Special sur la Présentation de la Journée du 4 Safar 2026
Ce jeudi, 16 juillet À partir du 22h sur le compte de Kureel Ligéeyal ku tedd ki
@Alkhadiim1
@MFRSFR
@Prince_Mourid
#4safar
#safar2026
Bonjour monsieur !
Je suis l’un des daara, mais dis toi que, avec beaucoup comme moi on est plus qualifiés que toi !
Et je détermine pas un domaine précis, je parle de tous !
T’inquiète pas on n’est pas plus passé par des écoles laïques
كنا في إيران ، نسكن مجانا مع الأكل والشرب، ولم نكن نشتري الكتب ولا الأقلام والدفاتر ، وكل ذلك من جيبه كان يُكِنُّ للطلبة احترامًا خاصاً وفائقا
رحمك الله يا سيد القائد علي خامنئي وأسكنك في فسيح جناتك ! ❤️🙏🏼
Affaire paasu Màggal gi :
Problème bi dëgg mi ngi nekk ci paasu dellu si foofu la gën a mettee maanaam boobu day fekk màggal gi di door a jàll daal 🤦🏽♂️
Podcast bii noo ko def ci téerey Sëriñ bi
Mawaahibu Xudduus
Munawwirus Suduur
Maqaalixun niiraan
podcasts.apple.com/fr/podcas…
يقال أنه في مثل هذا اليوم قد رحل إلى جوار ربه، والرحلة تفضي إلى الغيبة عادة، والحال أنه لم يغب قط حين الحديث عن قلوبنا، وكونه جارّا لربه قد بدأ ولم يحدث ما يقال عنه الرحيل، لا زلت يا وسيلتنا ولن تزال حيّا، فالحياة الحقيقية هي أن يدوم التأثير، حفظك الله ورعاك يا محبّ حبيبب الله ❤️
Am na tuuti wuute, ndax ñi rayoon Usmaan dañoo ñëw far ak S Àlliyu !
Ci kaw loolu nag taxawaayam dina am lay
Lima jàpp ni moom lañ ci war a jàng, gaawantu baaxul, rawatina lu jëm ci wàllu yoon !
Am réew nag pirioté yi dañoo bareendoo
Fàttalikuleen histoire S. Àlliyu bi ñu rayee S. Usmaan.
Lenn ci sahaaba yi ne, jàmm manu fee am te lijjantiwuñu ñi ray Usmaan, S Àlliyu ak ñi mu àndal ne loolu di nanu ko lijjanti waaye nanu xaar ba ag dal am.
Defe naa kilifay réew mi war nañu koo Fàttaliku te jël ci ay bind, xool mbir moomu fa mu mujj ak li mu indi.
Sëriñ Fàllu retweeted
🚨 Salut chers tous
Un proche a besoin de sang 0-(0 négatif).
Il est à l’hôpital régional(Thiés) entre la vie et la mort.
Quiconque peut le sauver sauver le SVP.
Veuillez appeler au +221709423563.
Max de partages 🙏🏾
Tu nous explique pourquoi tu l’enlèves publiquement, et on a pas le droit de commenter et d’expliquer pourquoi ne pas le faire ?
Oui on juge pas la personne, mais chaque acte posée est expliquée par la l’islam, nous donnons l’explication de l’islam où est le mal ? 🤷🏾♂️
Bëgg lu yomb rekk !
Laabiire ci diine la bokk, neko yonent bi shw waxe: "diine laabiire la".
Mooy wax sa mbokk jullit lukay jariñ wala moytu loo ko luko mëna lor ta yalla kese tax.
Bokk na ci mbir yi yalla gëna bañ mooy nit dila laabiire nga naan ko lijëntil sa bopp, yonent bi shw neena:
"Wax ji yalla gëna bañ mooy nit wax nit: ragalal yalla, munaan ko: lijëntil sa bopp".













