@RIENqueLUIi
iAccount based inSenegal
About this account
- Account based in
- Senegal
- Connected via
- Senegal App Store
Account-level information from X, not a live location or the device used for a specific post.
MA'AM SEEX IBRAHIMA FALL ñëriñ gudul jeex la, te ñëp xajj nan ci...
Joined May 2021
- Tweets20.8K
- Following4.1K
- Followers9.9K
- Likes12.1K
Pinned Tweet
Maximum de Rt🚨
C'est la mère de mon meilleur ami
Kon sama yaay la, ni doomam lama defoon
2009 batay dji may bindi tweet guii, degg ñu ko, guissu ñu ko
Xamu ñu ndax migui dundu wala...
Waaye daal nigui rafeet njort
Ci ndigalu doomam laa def Tweet gui
Di ci sàkku ñaan ❗
Maam Seex Ibrahima Faal
" Buñu demee ba ci kanam, lunek dina niyu yoonu Sëñ Bamba bi.
Waaye bu boobaa lima daan def, luñ ku ci gennee gennee, ci la. Lima daawul def luñ ku ci boole boole, du ci "
Baay Ndiaga Jóob (Baay Daouda Guey Baxdaas)
Murid gi yaatu na lool Europe rawatina France,dox na fa lool.
Te pourtant autorités coloniales françaises def nan seen xeetu pexe yep ngir faat Sëñ touba, éliminer le mouridisme.
Tay autorités yooyu ku leen yeewon, nu gis murid gi nimuy doxee France , dinan jeppi seen bop
Jarga ! retweeted
Replying to @RIENqueLUI
Bou geuna graw moy:
1/souma la féké gua mané as-salam haleykum gua mér
Teh souma gnewé wax la jaargua do mér
mm dioxé loxo kassé sax dou nouyo
Nouyo deug moy soit gua wax as-salam haleykum sans dioxè loxo
Soit gua dioxè loxo wax as-salam haleykum t moy bu gen
Jarga ! retweeted
Replying to @RIENqueLUI
Tuur ndox (saw(urine)) deesu ko teee, bu dikkee rek , fexel dém sotti ko ca wanag ba
Ndax mën na waral infection urinaire
Jarga ! retweeted
Sëriñ Abdu Xadr Mbacké
" Li Yàlla rëdd sap jë ( front) boo jaaree ci buntu bi dangako am, boo tëbbee mur lolu dongu ngay am. Waayé boo tëbbei mur mën ngaa damm ( fracturé) "
Sëñ Mustafaa Abdu Xadr Mbacké..
Nanu fonku nuyoo as-salam haleykum (yalla nga jam) . Ëp na négliger
Ndax dinga muccu ci ak accident wala lenen lu grave fek na nuyoo googu moola ko may.
Leegi nag ay « yaagi koy yëg , athia waay, Jaajef waay, etc » ngay deg.
Nanuy jiital as salam haleykum rek soogi ci tek leneen
Sëriñ Abdu Xadr Mbacké
" Li Yàlla rëdd sap jë ( front) boo jaaree ci buntu bi dangako am, boo tëbbee mur lolu dongu ngay am. Waayé boo tëbbei mur mën ngaa damm ( fracturé) "
Sëñ Mustafaa Abdu Xadr Mbacké..
À part ñi ko allergies ak xorom bu bari bi , ay bienfaits dongu la .
Ki nga xamni dafa hypertendu warna def attention ci guerte thiaf, limiter consommation bi . Loolu dongu la
Guerte daa bari ay bienfait lool
Le GUERTÉ THIAF: un DANGER ⚠️ ? Version française
Mon num pro: 00221785927932
vm.tiktok.com/ZN8rjpJd1/
Partages, likes et commentes
This video is larger than Cloudflare's 512 MB cache, so it can't be played through. More donations are needed to cover a larger cache. Donate
Café touba + Guerte thiaaf ci takkusaan : quel combo ❤️😍
Le GUERTÉ THIAF: un DANGER ⚠️ ? Version française
Mon num pro: 00221785927932
vm.tiktok.com/ZN8rjpJd1/
Partages, likes et commentes
This video is larger than Cloudflare's 512 MB cache, so it can't be played through. More donations are needed to cover a larger cache. Donate
Jarga ! retweeted
🚨NDIGËL
Seex Muhammadul Muntaxaa Mbàkke jox na ndigël Sëriñ Amdi Xadi Faal xalif seneraal dee Baay Faal ag jabootu Seex'Ibra Faal gépp ajjuma (vendredi 02 octobre 2026) ñu rujj & léeral réserve Université Tuubaa bi ci yoonu Tuubaa Béleel. Garab ya fa nekk ñu xar ko mat mu jëm ci Ndogou Seex Ibra Faal yi sunu kanam.
Nanu baayi xel julit yii di ligeey kanzul kitaab Kërug alxuraan wi bi Sëñ Muntaxa di ligeey loo waa Kër maam Seex Ibrahim faal.
Alxuraan julitt yep ko boku ! Kon nun mii nekul foofee, bunu fate muk tabbal sunu alal ci ligeey bi, aki bernde ni fa nek.
Jamono yagg naa nakari, te masul impacté wala empêcher yoonu Murid ci been projet ( rails bi , jummaah ji etc.)
Te ligeey keep moleen ko may ak fonku Ndigël
Jarga ! retweeted
Du mensonge. Tu l'as limogé parce qu'il t'a rappelé tes engagements auxquels tu as lâchement renié,petit vil ingrat !