dieery wadaane retweeted
Hello les coffee lovers ! ☕🤎
Bienvenue dans notre petit univers dédié aux amoureux du café ! 😍
On parle café, on partage du plaisir et surtout… on vous sert de bonnes saveurs ! 🔥
Si tu es team café, tu es au bon endroit ! ☕❤️
Abonne-toi et reste branché 👀
Samay diglé,toggou kou khif la,booko dieufandikoo woul,mane milako digal dieufandikoo ko
Al Abdoul Khadim
Zikr,mooy diaasiy mourid yi,thi la niouye khekhé,bepp noon,moo kham djiné la,wala nit,te thi la niouy fégué bepp ndog bouleen wout si
Ch Abdoul Wahaab Sahraany
Kham kham,boudé garab bou sakh thi tooloub khol,ay reenam di ndioub,ay thiaram di ragal yalla,khobam ya di tenguine,kepp kou lekk thia dioodia garab,thioonoy reer doula dal moukk
Cheikh Sidy Mouhtaar Al Kountiyou
Seugne Massamba diop saam biko serigne né wakhal loo beugg niou defal lako dafa neko
Loo niou mana defal na nga niouthi boolel ag nité
Seugne Modou diaw Pakha Neena Cheikh Ibra Fall
Dafa ligueeyal serigne bi,ligueey bou sell lool te tegué,thi ag nité
Kiy diaamou yalla,tey doundé lou kharaam,dafa melni,am pitakh,mou boof thi néne bou yakhou,da thiay sonnou rk waaye douthia tosteune ab thiouthie
As Cheikh Alioune Hawaas
Diazbou neekh na walaahi
Rawatina bou serigne bi di tague sahaaba yi ba agci thi sama baaye bi seydina aliou fou sori lamay yobbou
Al imaamou sanousy kou amoon tawhiid lool la te mana khalam boroomam
Bi baayam faato,da am kouko guis thi guent,neko noo def ak sounou boroom,mouneko diegal nama,waaye thi sama doom,dioodiou di sanousy lamako defalé,ndakh bigne ma tegué thi diaag bi,war maa dioullé 👇
Diounayde denkoone na kenn thiy taalibeem neko
Na nga diaamou yalla,kone di nga tekhé na ngay diufandikoo,sellal thi lepp,kone di nga bonofisou,na ngay dolleeko euleug sidi dieufandikoo wird,souba ag ngoone
Na nga khamne,toudde yalla,dieuf diou am resultat la,te kaarangue la👇




















