🚨Bismillaahi murids
Ño gi yëggal murids yi ag soppeey Seex Mustafaa Fall Mbar yëpp leggey bii ko murids tambalil ci Jannatul Mahwa Baay Fall Ga girr Serigne Bi mën fa taxawoo leggeyu Ndogou Seex Ibra Fall yi ci weeru Koor Gi.
Jaayante Bi
Wave/Om 78 187 15 41 Meïssa Ndiaye📌
Sëriñ Mustafaa Mbar, bu teggiin doon jëmm ma ne moom la, li Yàlla gën a bëgg ci ab jaam la def muy woyof, gisul dara ci boppam, yamalewul kilifaam ak dara, liggéey bu ñu woote mu njëkk ca mujj ca.
Yal na ko Yàlla sàmm !
🚨🚨🚨
Suba ci gaawo bi dëppook (Samedi 05 septembre 2026) ci arméli Tuubaa yu ñëk yi jakkarloo ak Jumma Ji fa la ñuy xëy In Sha Rabbi. Sëriñ baa gi ciy sooñi ñëpp.
Seex Moodu Aminta Fall tontu woon na Seex Salihu Mbacké ne ko «filleg mo gi ñuy leggey lo mom mi fiy Sëriñ Tuubaa ñun Baay Fall yi dina fi yagg...». Seex Muhammadul Muntaxaa mi dana doole yagg ndax mo gi ñuy leggey lo ñun jabootu Seex'Ibra Fall Gi wallahil azim !!!📌